"Bonne fête de Saint Valentin ❤ Mbeugel mo beuri dolé donc bou darra sed bouko thiopati neko rikh thi digueu n'a rafet té sant noula nekh ❤❤❤❤❤ les femmes guenélen thiourayi, bine bine yi, menote yi, chaînette yi, na nekh ba melni toukoussa beun sagnebeu réreu"
Écris le tout premier commentaire